TSK

TSK · Proverbs 28:25

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aji Sax ji Yàllaa mat jant, mat kiiraay; yiw ak daraja, Aji Sax ji joxe; te du ngëneel lu muy bañal ku mat.

Réy-réylu jote rekk lay jur, ku dégg ndigal a xelu.

Kanam gu leer day seral xol; xibaaru jàmm, jàmmu yaram.

Ragal nit dugal sa bopp la, ku wóolu Aji Sax ji, fegu.

Waaye barke ñeel na ku wóolu Aji Sax ji, yaakaar Aji Sax ji.