1 Kings 1:6
TSK
Baayam Daawuda nag masu koo wax dara, ak lu mu mana def. Adoña moo toppoon ci Absalom. Mu doonoon ku góorayiw lool.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Baayam Daawuda nag masu koo wax dara, ak lu mu mana def. Adoña moo toppoon ci Absalom. Mu doonoon ku góorayiw lool.
Ku ngóob jot, nga góob, xelu nga; ngóob taxaw, ngay nelaw, gàcce la.
Ku jur ab dof, am naqar; ab dof waajuram du bég.
Tegal gone ciw yoon, ba bu màggee, du ko wacc.
Bul ñéebloo yar gone, bantal ko taxu koo dee.
Ku yàq sab surga ba muy ndaw, bu ëllëgee mu defe ne doom la.