ndax Leween, ñi amul wàll ci seen céru suuf, dikk, ñook doxandéem yi ak jirim yi ak jëtun, yi ngeen dëkkal, ngir ñu lekk ba regg. Su ko defee seen Yàlla Aji Sax ji barkeel mboolem seenu ñaq.
TSK
TSK · Proverbs 3:10
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Proverbs 19:17
TSK
Ku baaxe ku ñàkk, lebal nga Aji Sax ji, te moo lay yool.
Dugalal sa alal, dawloo ko; yàgg-yàgg nga jotaat ci.
Haggai 2:19
TSK
Ana am jiwooti ci sàq yi? Mbaa lennati ci reseñ ak figg? Mbaa garabi gërënaat ak oliw? Du lenn lu meññ. Waaye li ko dale bésub tey jii, maay barkeel.