Ruth 3:11
TSK
Léegi nag neel tekk rekk, doom. Loolu nga ñaan lépp, dinaa la ko defal, ndax waa dëkk bi bépp xam nañu ne jigéen ju jàmbaare nga.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Léegi nag neel tekk rekk, doom. Loolu nga ñaan lépp, dinaa la ko defal, ndax waa dëkk bi bépp xam nañu ne jigéen ju jàmbaare nga.
Xel mu rafet a gën gànjar; loo mana bëgg moo ko raw.
Jeeg bu jàmbaare day teral jëkkër ja, jeeg buy rusloo day semmal jëkkër ja.
Ku am jabar, am nga ngëneel, am nga yiwu Aji Sax ji.
Wurus am na ak gànjar yu bare, waaye kàdduy xam-xam a gën per yu jafe.