TSK

TSK · Proverbs 4:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Na samam njàngle sóob nib taw, samay kàddu rogalaat nib lay, ba tuurul am ñax, baawaanal gàncax.

Job 33:3 TSK

Xel mu dëggu laay waxe, samay kàddu di xam-xam bu wóor.

Damay saxal askanam ba fàww, yàggal ab jalam ni asamaan.

Lu ma wax njub la. Amul lu dëng mbaa lu jekkadi.

Titus 1:9 TSK

Na jàpp bu dëgër ci kàddu gu wóor gi, ni ñu ko ko jàngale, ngir mu man di ñaaxe jooju àlluwa ju wér, tey tiiñal weddikat yi.