TSK

TSK · Proverbs 6:9

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Yeen bokk yu dofe yi, moytuleen. Gàtt xel yi, kañ ngeen di muus?

Ab yaafus, nelaw yu xóot, te ku yàccaaral xiif.

Ab yaafus day tëdd ak a walbatiku, mooy bunt, day jaayu, demul fenn.

«Éey Yerusalem, fóotal sa xol, jële ci lu bon, ndax nga mucc. Foo àppal sa mébéti xol yu bon?

¶ Li tax ngeen wara gëna farlu ci loolu mooy, xam ngeen jant yi nu tollu; seen waxtuw yewwu jot na ba noppi, nde léegi la nu mucc gëna jege ba nuy doora gëm.

ndax yeen ci seen bopp, xam ngeen xéll ne Sang bi, ni sàccub guddi lay dikke.