Proverbs 7:8
TSK
Muy dem ba fa ndaw say taxaw, ca selebe yoon wa, daldi wuti kër ndaw sa.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Muy dem ba fa ndaw say taxaw, ca selebe yoon wa, daldi wuti kër ndaw sa.
Ma ngay tëroo nib sàcc, góor ñu bare lay fecciloo worma.
Yeen aka mokkal gànctu! Jeeg ju bon ji sax di jànge ci yeen.
«Téenleen, séentu tund ya ne faraas! Ana fu ñu leen fi tëddewul? Ci yoon yi ngeen di yeeroo ni màngaan muy dogalee ci màndiŋ mi. Sobeel ngeen réew meek seen gànctook seenug mbon.
¶ «“Tabax nga ab néeg selebe yoon wu ne, sàkk sa jaamookaay péncoo pénc, te ab gànc sax tane la, nde yaw laajoo ag pey.
làmp du niiteeti fi yaw, te baatu boroom séet akub séetam du jibeeti fi yaw mukk, ndax say julaa ëppoon doole ci àddina, te say xërëm a sànk askanoo askan.»