Ndaw si jàpp ci mbubb mi, ne ko: «Kaay tëdd ak man.» Yuusufa nag wacc mbubb ma cay loxoom, daw génn kër ga.
TSK
TSK · Proverbs 7:13
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 39:12
TSK
Numbers 25:6
TSK
¶ Ci biir loolu rekk, jenn waayu bànni Israyil dikk, indaale senn ndawas waa Majan ci biiri bokkam, Musaa ak mbooloom Israyil mépp di gis, fekk ñoom ñuy jooyoo fa bunt xaymab ndaje ma.
Proverbs 9:15
TSK
di woo ña fay jaare te jubal seenu yoon.
Isaiah 50:7
TSK
Waaye Boroom bi Aji Sax jee may dimbali, ba tax rusuma. Moo ma taxa dogu ba dëgër, ngir xam naa ne deesu ma rusloo.
Ezekiel 2:6
TSK
Waaye yaw nit ki, bu leen ragal, bul ragal seeni wax. Xam naa ne ay taxas aki dég a lay wër, nga toog ci kawi jiit. Waaye bul ragal seeni wax te bul tiit seen kanam doonte kërug fippukat lañu.
Ezekiel 16:33
TSK
Mboolem caga yi dañuy feyeeku! Waaye yaw yaay neexal sa far yépp, di leen fey ñu jóge fu ne, di la tëdde.