Genesis 15:14
TSK
Waaye waa réew moomu leen di def ay jaam, dinaa leen àtte. Gannaaw loolu sa askan dina ca génn, ànd ak alal ju bare.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waaye waa réew moomu leen di def ay jaam, dinaa leen àtte. Gannaaw loolu sa askan dina ca génn, ànd ak alal ju bare.
Yaa may xamal yoonu ndund. Fu bànneex mate, yaa teew, xéewal sa ndijoor la saxe.
Waaye bu feeñee, fey boroom juróom yaari yoon, joxe alalu këram yépp.
Xam-xam ay feesal néeg ya ak mboolem alal ju jafe te yànj.
Ngeen boole ci daj cofeelu Almasi, gi wees xam-xam, ngir ngeen fees, ba fees dell ak koomu Yàlla.
Loolu moo am ngir ab cér bu dul yàqu, du sobewu, du seey, cér bu dence fa asamaan ñeel leen,