Genesis 1:9
TSK
¶ Yàlla ne: «Na ndox, mi asamaan tiim, gëndoo benn bérab, ba joor gu wow feeñ.» Mu daldi nekk noona.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Yàlla ne: «Na ndox, mi asamaan tiim, gëndoo benn bérab, ba joor gu wow feeñ.» Mu daldi nekk noona.
Bëti ndox ya ca xóote ya dafa taxaw, bunti ndoxi asamaan tëju, taw bi dal.
Nga gëdd, ndox ma fëx; nga dënu, mu daw,