TSK

TSK · Proverbs 9:12

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 19:4 TSK

Su ma moyoon dëgg sax, maay bokk ak sama moy fanaan.

Job 22:3 TSK

Ana lu sag njub mana yokk Aji Man ji? Lu ko sag mucc ayib mana indil?

Job 35:6 TSK

Soo bàkkaaree, lu muy wàññi Yàlla? Man ngaa tooñ, tooñati ba def ko dara?

Tee ngeena baña kókkalee bala ñoo teeŋal seeni jéng? Sànkute kat moo di dogal bi ma dégg, mu bawoo fa Boroom bi, Aji Sax ji ci gàngoor yi, di luy dikkal réew mi mépp.

Mboolem làng yi ci des it, làng gu ci nekk di ñoomu neen, seeni jabar di ñoomu neen.

Loolu la bind ci mboolem bataaxal yi mu waxe ci moomu mbir, te mu am ci ponk yu jafee xam, ba ñi dese am njàng te seenum xel toogadi, di walbati waxam, ni ñuy def ak yeneen bind yépp, ba far sànk seen bopp.