TSK

TSK · Psalms 21:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Samiyel fab béjjénu diw ba, diw ko fa kanam magam ña. Ba mu ko defee Noowug Aji Sax ji ne milib ca kaw Daawuda, dale fa ànd ak moom bésub keroog. Ba loolu wéyee Samiyel moom, dem dëkk ba ñu naan Raama.

Noonu la magi Israyil ñépp dikke ca Buur Daawuda ca Ebron, mu fasook ñoom kóllëre fa kanam Aji Sax ji. Ñu sotti Daawuda diwu pal ga, muy buurub Israyil.

Job 41:11 TSK

Jumi sawaraay tàkke ca gémmiñ ga, ferñent ya jiitu,

Yal na la may li nga namm, di sottal loo mébét,

Yaay sama doole, ma di la séentu, yaw Yàlla, yaay sama rawtu.

«Ana ku ko dawlul lenn, ba mu war koo delloo?»

Yeesu mi ñu def mu gëna suufe as lëf malaaka yi, moom lanu gis deeyam gi mu dee tax mu jagoo kaalag teraanga. Noonu la deeyale ñépp ci kaw yiwu Yàlla.