TSK

TSK · Psalms 33:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

noon ba naan: «Daan naa ko,» bañ yay bége saab jéll.

ne la: «Ma dee, tàbbi bàmmeel, ana lu mu lay jariñ? Nu la pëndu pax di sante, bay biral sa worma?

Bésub keroog dees na ne: «Sunu Yàllaa ngii nag! Moom mii lanu yaakaaroon te moo nuy wallu. Aji Sax jii lanu yaakaaroon, nan bég te bànneexoo wallam.»

Luke 1:47 TSK

«Sama xol laay màggale Boroom bi, samag noo laay bége Yàlla mi may musal,

Ñeenti bindeef yi am nañu ku nekk juróom benni laaf, fees aki bët ba daj, biir ak biti, te guddi ak bëccëg duñu selaw, xanaa naan: «Kee sell, Kee sell, Kee sell, Keey Boroom bi Yàlla Aji Man ji, Kee masa Nekk, Kee Nekk, Keey Dikk.»