TSK

TSK · Revelation 21:12

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

«Na bànni Israyil di dal, ku nekk ak raayaam ak xàmmikaayu kër maamam. Fi wër xaymab ndaje mi te dànd ko as lëf, fi lañuy dale:

Ezra 9:9 TSK

Ndax ay jaam lanu, waaye yaw sunu Yàlla, waccewoo nu sunug njaam. Yaa dawal ngor sunu digganteek buuri Pers, ngir mayaat nu dooley tabax sunu kër Yàlla, yékkatee ko ca gentam ba, may nu kiiraay ci Yerusalem ak ci Yuda.

Sàkkuwloo sarax, nde kon ma indi; te soppuloo saraxu rendi-dóomal.

Maay defare sa kawi tata peri rubi, def say wunt per yuy lerxat, def sa tata yi la wër yépp doj yu bakkane,

Miir bu ci nekk dina am ñetti bunt yu ñu dippee ñetti giiri Israyil. Wetu bëj-gànnaar, benn buntu Ruben ak benn buntu Yuda ak benn buntu Lewi.

Maa leen wax ne leen: noonu rekk lay doone mbégte fa malaakay Yàlla ya, bu benn bàkkaarkat doŋŋ tuubee.»

Acts 26:7 TSK

Te mooy dige bi fukki giir ak ñaar yu bànni Israyil di séentu mu sottil leen, ba tax guddi ak bëccëg ñu xér ci jaamu Yàlla. Yaakaar jooju nag, Buur, moo tax Yawut yi tuumaal ma!

¶ Ma dégg limub ña ñu màndargaale torluwaay ba; ñuy téeméer ak ñeent fukk ak ñeenti junni (144 000), bawoo ci mboolem giiri bànni Israyil:

Bunti dëkk bi du tëje mukk bëccëg, te foofa sax guddi amu fa.