كل أسفار KYG

Revelation 21

KYG · الآية 16

22 أصحاحات

KYG / Revelation / الأصحاح 21

KYG · الآية 16

D ëkk bi dafa kaare; guddaay bi tollook yaatuwaay bi. Mu natte dëkk bi bant bi mu yor, guddaay bi ak yaatuwaay bi ak taxawaay bi, lépp tolloo, di fukki junneek ñaari dayo (12 000), yemook ñaari junneek ñaar téeméeri kilomeetar (2 200).