TSK

TSK · Romans 1:31

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Esekiya buurub Yuda yónnee ca buurub Asiri ca Lakis ne ko: «Tooñ naa de, waaye ngalla baal ma, te dem. Loo ma sas dinaa ko fey.» Buurub Asiri sas Esekiya buurub Yuda juróom ñeent fukki barigoy xaalis ak juróom ñeenti barigoy wurus.

car ya wow, damm, jigéen ñi dikk, xambe. Dañu di xeet wu dul dégg, ba tax ki leen sàkk yërëmu leen, moo leen bind te ñeewantewu leen.

«Dofe la sama ñoñ def. Man, xamuñu maay kan, mbetey gone yu dul xalaat dara; dég-dég, tus; seen xel mépp, lu bon rekk, lu baax, xamuñu ci dara.»

Ndax kat, li gisuwul ci Yàlla, te di manooreem gi dul jeex, ak jikko ji mu wéetoo ndax li muy Yàlla, ba àddina sosoo ba tey, xel man na koo ràññee ci ay liggéeyam, te looloo leen taxa ñàkku lay.

Duñu am ab xol, duñu meddi, ay soskat lañuy doon, ñu ñàkk sago, ñu néeg te bañ lu baax;