TSK

TSK · Romans 11:34

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 36:22 TSK

Yàlla, kay, mooy ki dooleem kaweel! Ana ku mana jàngle ni moom?

«Waaye ana ku ci teewe woon jataayu Aji Sax ji? Ku ci fekke, ba dégg kàddoom? Ku ci teewlu kàddoom, ba dégg ko?