¶ Gannaaw bu leen leen seen Yàlla Aji Sax ji dàqalee nag, buleen wax ci seen xel ne: «Sunu njekk a nu may Aji Sax ji indi nu, ngir nu moom réew mii.» Mbonug xeet yii kay moo waral Aji Sax ji dàqal leen leen.
TSK
TSK · Romans 11:6
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Deuteronomy 9:4
TSK
Romans 4:4
TSK
¶ Kuy liggéey, ag peyooram du taxawe ag may, waaye wartéef la.
Ci yiwu Yàlla daal laa doone ki ma doon, te yiw woowu ma ñeel neenul. Xanaa yeneen ndaw yépp sax, maa leen gëna liggéey. Du ci man nag, waaye yiwu Yàlla, wi ànd ak man la.
Galatians 5:4
TSK
Yeen ñiy sàmm yoonu Musaa, di ko sàkkoo àtteb njub fa kanam Yàlla, daggoo ngeen ak Almasi, ñàkk ngeen yiwu Yàlla.
2 Timothy 1:9
TSK
Moo nu musal, woo nu woote bu sell te sunuy jëf taxul, waaye coobarey boppam a tax, ak yiwam wi ñu nu may ci Almasi Yeesu, balaa ay jamonoy jamono di sosu.