Ndax kat dafa mel ni sunu yaram wiy wenn, te cér yi bare, doonte cér yépp a wuuteek seen moroom nu ñuy liggéeye.
TSK
TSK · Romans 12:5
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Romans 12:4
TSK
Noonu laay def man ci sama bopp: ñépp laay wuta neex, ci lépp. Sàkkuwuma sama njariñal bopp, waaye njariñal lim bu gëna takku, moom laay sàkku, ngir ñu texe.
Cér yi daal bare nañu, waaye wenn yaram wi la.
Ephesians 1:23
TSK
mbooloo miy aw yaramam. Ci mbooloo mi nag la Almasi teewe teewaay bu mat sëkk, te Almasi mooy matal lépp ci ñépp.
Ephesians 5:23
TSK
Almasi moo di musalkatu mbooloom gëmkat ñi, mbooloo mi di aw yaramam. Te itam ni Almasi dee boppu mbooloom gëmkat ñi, ni la jëkkër ji dee boppu jabaram.
Colossians 1:24
TSK
¶ Léegi nag maa ngi bége coono yi ma jànkoonteel ngir seen njariñ; li des ci tiisi Almasi, moom laay mottalee coono yooyu ma daje sama yaramu suux wii, ngir njariñal mbooloom gëmkat, miy yaramu Almasi.