كل أسفار KYG

Romans 13

KYG · الآية 4

16 أصحاحات

KYG / Romans / الأصحاح 13

KYG · الآية 4

N dax kilifa gi mooy ndaw li Yàlla yebal ngir sa jàmm. Waaye soo dee def lu bon, ragalal, ndax kilifa gi yorul ab saamar cig neen; mooy ndawal Yàlla liy añale, te mooy jottli am sànj mu wàccal kuy def lu bon.