Xalelu góor bi, bànneexul bi ngay gone, bégalal sa xol bi ngay ndaw. Toppal loo namm ak loo xemmem, waaye xamal ne loolu lépp, Yàlla da la koy laaj.
TSK
TSK · Romans 14:12
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Luke 16:2
TSK
Waa ja woo ko, ne ko: βLi ma la déggal, lu mu doon? Limal ma sag caytu, ndax dootoo ma mana saytul.β
1 Peter 4:5
TSK
waaye ñoo koy layoo ak ki nara àtte ñiy dund, ak ñi dee.