¶ Man nag bokk yi, manuma woona wax ak yeen ni ñuy waxe ak ñu ànd ak Xelum Yàlla, waaye ni niti suuxu neen rekk laa manoona waxe ak yeen, mbete ñu diy tuut-tànk ci yoonu Almasi.
TSK
TSK · Romans 2:20
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
2 Timothy 3:5
TSK
Ag njullite lañuy mbubboo tey xalab leer ga leen ko wara manloo. Ñooñu, dëddu leen.
Hebrews 5:13
TSK
Képp ku tollu ci nàmp um soow nag, tuut-tànk nga, doo mana xam dara ci kàddug njub.