Genesis 25:32
TSK
Esawu ne: «Man miy waaja dee ak xiif, ana lu ma céru taaw di jariñ?»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Esawu ne: «Man miy waaja dee ak xiif, ana lu ma céru taaw di jariñ?»
Loo ci wax wax, solo sa gëna néew. Kon ana loo ci jële?
Yeena ne: “Jaamu Yàlla ag neen la. Ana lu nu jële ci dénkoo ndénkaaneem, tey wéye toroxlu fi kanam Aji Sax ji Boroom gàngoor yi?
Su yaakaaru nit ci àddina doŋŋ taxee may xeex ak ay rabi àll ca Efes, ana lu mu may jariñ. Gannaaw ñi dee duñu dekki, kon kay mooy li ñu ne: «Nanu lekk te naan, nde ëllëg nu dee.»