TSK

TSK · Romans 8:33

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 2:4 TSK

Seytaane ne Aji Sax ji: «Bakkan a wuutu bakkan rekk. Mboolem lu nit am, man na koo weccee bakkanam.

Job 34:8 TSK

di àndandook ñiy def lu ñaaw, di lëngook nit ñu bon ñi,

Nit ku bon a ngi may duural, di ma jiiñ lu ma yégul.

Ki may dëggal jege na. Ana kuy layook man? Nan bokk taxaw! Kuy jànkoonteek man ci yoon? Na jegesi boog!

¶ Gannaaw gi Aji Sax ji won ma Yosuwe sarxalkat bu mag ba, mu taxaw fa kanam malaakam Aji Sax ji, Tuumaalkat bi taxaw féete ko ndijoor, ngir tuumaal ko.

Luke 18:7 TSK

Kon ndax Yàlla man naa baña sàmm àqu tànnéefam ñi koy woo wall guddi ak bëccëg, xanaa di leen yeexe?

¶ Kon nag léegi, amul benn daan bu ñeel ñi bokk ci Almasi Yeesu.

¶ Yeen bokki gëmkat ñi Yàlla sopp, xam nanu ne moom moo leen taamu,

Yeen la Yàlla Baay bi ràññee lu jiitu, ci ni mu leen sellale Noo gu Sell gi, ngir ngeen mana déggal Yeesu Almasi, boole ci tooyloo deretam, mu setal leen. Aw yiw ak jàmm ju ne xéew ñeel na leen.