Ba ni Samiyel faatoo, seeteetul Sóol. Teewul mu jooy Sóol, waaye fekk na Aji Sax ji réccu la mu fal Sóol buurub Israyil.
TSK
TSK · Romans 9:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yeen soppey Yerusalem yépp, bégandooleen ak moom, te di ko bànneexoo. Mboolem yeen ñi doon ñaawlu tiisu Yerusalem, bokkleen ak moom xolam bu sedd.
Bu ngeen déggul de, ma làqu, jooy seen reewande, sama rongooñ tuuroo tuuru, ma jooya jooy, nde dees na jàpp géttu Aji Sax ji, yóbbu.
Saay gët a ngi wal ndax sama askan wi rajaxoo.
Aji Sax ji ne ko: «Wëral dëkk bi, ci biir Yerusalem. Foo gis kuy onk ak a binni, di ko naqarloo gépp tojaange gu ñu fiy def, nga rëdd aw rëdd ci jëëm.»
¶ Bokk yi, sama yéeney xol, ak ñaan gi may ñaanal Israyil ci Yàlla moo di ñu mucc.
Dinaa may nag sama ñaari seede yi, ñu biral waxyu diiru junni ak ñaar téeméeri fan ak juróom benn fukk (1 260) yu ñuy sol ay saaku, di ko toroxloo.»