Yal na Yàlla Aji Man ji def waa ja yërëm leen, ba bàyyi seen doomu baay ba, moom ak Beñamin itam. Man nag, su ma naree ñàkk ay doom— aa! Naa leen ñàkk rekk.»
TSK
TSK · Ruth 1:20
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 43:14
TSK
Exodus 15:23
TSK
Ñu dem, ba àgg fu ñu naan Maara, waaye manuñoo naan ca ndoxum Maara, ndax wex. Looloo waral ñu tudde bérab ba Maara (mu firi Fu wex).
Job 6:4
TSK
Da di fetti Aji Man jee ma jam, ba tooke ji nàndal samam xel, mbugalu Yàlla yu raglu làng-déral ma.
Job 11:7
TSK
Dangaa mana gëstu mbóoti Yàlla, ba gis ko? Am yaa ñédd Aji Man ji?
Psalms 73:14
TSK
Bés bu ne yar dal ma, saa yu ma xëyee, jot mbugal.
Isaiah 38:13
TSK
May xalaat, ba bët set; Aji Sax jiy dammat samay yax ni gaynde, diggante bëccëg ak guddi, nga jekkli ma.
Hebrews 12:11
TSK
Dëgg la, benn yarub tey neexul, xanaa naqari. Waaye la yar bay mujj jural ña mu tàggat, jàmm la ak njub.
Revelation 21:22
TSK
¶ Ab jaamookaay nag, gisuma ko fenn ci biir dëkk bi, ndax Boroom bi Yàlla Aji Man ji ak Gàtt bi ñooy jaamookaay bi.