Kon gisleen ne man la, man doŋŋ, kenn du Yàlla ku dul man! Man maay rey, di dundal; di gaañe, di wéral; maay jàpp, te kenn du xettli.
TSK
TSK · Ruth 1:5
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Isaiah 49:21
TSK
Dangay mujj naa: “Moo, ku ma jural ñii ñépp? Man mi ñàkkooni doom, manumaa jur, ñu toxal ma, wacc ma; ana ku leen yoroon te ma des, man kenn? Ñii sax, fu ñu ne woon?”»