كل أسفار KYG

Ruth 4

KYG · الآية 7

4 أصحاحات

KYG / Ruth / الأصحاح 4

KYG · الآية 7

B ooba Israyil, jamono yu jëkk yooya, mbirum njëndum jotaat mbaa ag weccoo, la ñu ko baaxoo dogale ci diggante nit ak moroom ma, nii la: kii day summi dàllam, jox kee. Noonu lees daan yoonale ag jëflante ca Israyil.