TSK

TSK · Titus 1:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Buleen tong seen mbokk, te àrtuleen seen moroom bu baax bala ngeena bokk ak moom gàddu bàkkaar.

Kuy déggal Yàlla, man na maa dóor, bantal ma ci ngor. Loolu ngëneelu cuuraay la, duma ko bañ. Waaye maa ngi saxoo ñaan pexey noon moy.

¶ Ndegam sax dama leena tegoon aw tiis ndax bataaxal ba ma leen bind, réccootuma ko, doonte réccu woon naa ko, ndax gis naa ne bataaxal boobu teg na leen aw tiis, lu mu gàtt gàtt.

¶ Soo dee xamal loolu bokki gëmkat ñi, yaa di jawriñu Almasi Yeesu ju baax ju xontoo kàdduy yoonu ngëm wi, ak àlluwa ju rafet ji nga topp naka jekk.

waareel kàddug Yàlla te taxaw ci temm, su neexee ak su naqaree; di yedde, di femmoo, di ñaaxe, tey saxoo muñ ci sam njàngle.

¶ Googu kàddu ngay waaree, di dénkoo ak di femmoo, te boole ci fulla ju mat sëkk. Bu la kenn yab.