TSK

TSK · Titus 3:9

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 15:3 TSK

Ku xelu du layoo waxi caaxaan, kàddu yu amul lenn njariñ.

Su ma jotoon ci kàddug waxyu, boole ci xam mboolem kumpa, ak mboolem xam-xam, ak ngëm gu mat sëkk ba mana toxal ay tund, te jëfewuma cofeel, duma dara.

Waaye nettali yu yittewoo lu dul Yàlla, ak léebi jeeg ju màggat ji, bañ ko, te nga tàggatu ci ag njullite.

Waaye ay kebetuy àddinay kese, moytu ko, ndax ngëmadi gu ko yées rekk lay yóbbee,

te baña topp léebi neen yu Yawut yi, ak santaaney nit ñi dëddu liy dëgg.