كل أسفار KYG

Zechariah 13

KYG · الآية 3

14 أصحاحات

KYG / Zechariah / الأصحاح 13

KYG · الآية 3

T e képp kuy biralati waxyu, ay waajuram, baayam ak ndeyam nañu ko wax ne ko: “Doo dese bakkan, ndax yaa fen ci turu Aji Sax ji.” Ay waajuram, baayam ak ndeyam nañu ko jam ba mu dee, ca ba muy biral waxyu.