Genesis 33:8
TSK
¶ Esawu ne ko: «Waaw, dal bu réy bii ma dajeel, loo ci namm?» Yanqóoba ne ko: «Xanaa di sàkku nga dalal ma jàmm rekk, sang bi.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Esawu ne ko: «Waaw, dal bu réy bii ma dajeel, loo ci namm?» Yanqóoba ne ko: «Xanaa di sàkku nga dalal ma jàmm rekk, sang bi.»
Kenn ca mbooloo ma ne ko: «Aa! Ngiñ lii de, sa baay giñoon na ko ci kaw mbooloo mi, ne: “Képp ku lekk tey, yal na alku,” moo tax mbooloo mi néew doole.»
¶ Gannaaw ba loolu wéyee Absalom daa jël watiir aki fas ak juróom fukki nit ñuy daw di ko jiitu.
ak lem akum soow, aki gàtt, ak formaasu nag ngir Daawudaak mbooloom lekk. Ndaxte booba dañu ne: «Mbooloo mi de, xiif ak mar lañu boole, ak coonob màndiŋ ma.»
Bàyyeel ñoll kuy sànku, bàyyi biiñ ak boroom naqar.