TSK

TSK · 2 Samuel 21:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Xanaa kay du yaw, Yàlla mi nu wacc, yaw Yàlla, mi baña ànd ak sunu mboolooy xare?

Ndam aki sarxolle ca xaymay ñu jub ña, ndijooru Aji Sax jee def njàmbaar!

Kuy damu kay, na damoom xelam mu ko may mu xam ma, xam ne maay Aji Sax, jiy jëfe ngor ak dëgg ak njekk fi kaw suuf. Loolu déy mooy sama bànneex.» Kàddug Aji Sax jee.

Waaye ci mboolem lu nu dikkal, nooy am ndam lu mat sëkk, ci ndimbalal ki nuy soppeem.