TSK

TSK · Acts 11:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Naka laa xool, yem ci loxo bu ñu ma tàllal. Ndeke taxañub téere moo ci nekk.

Amos 8:2 TSK

Mu ne ma: «Amos, ana loo gis?» Ma ne ko: «Xanaa dàmbu meññeef mu ñor.» Aji Sax ji ne ma: «Mbugal ñoral na Israyil, sama ñoñ. Dootuma leen baal dara.

Acts 10:9 TSK

¶ Ca ëllëg sa, ñu dem bay jub dëkk ba, yemook Piyeer yéeg ca kaw taax ma ci digg bëccëg, ngir ñaan.

¶ «Yàlla def, gannaaw ba ma délsee Yerusalem, ma doon ñaan ca kër Yàlla ga, daldi daanu leer.