Leviticus 19:18
TSK
Buleen di feyantook seen mbokkum waa réew te buleen ko dencal mer. Ni ngeen soppe seen bopp nag, nangeen ko soppe seen moroom. Maay Aji Sax ji.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Buleen di feyantook seen mbokkum waa réew te buleen ko dencal mer. Ni ngeen soppe seen bopp nag, nangeen ko soppe seen moroom. Maay Aji Sax ji.
tiisoo leen ni saab xarit mbaa doomu ndey, di ñaawlook a yoggoorlu ni ku ñàkk yaay.
Wallul ku ñuy reyi te tooñul, xettlil kuy tërëf, ñu di ko reyi.
Jenn waay ju soqikoo ci giirug Lewi it noonu; daa dikk ba tollu foofa, séen waa ja, daldi teggi.
¶ Ci kaw loolu Yeesu ne: «Baay, baal leen, ndax li ñuy def, xamuñu ko.» Ñu daldi tegoo bant ay yéreem, ngir séddoo ko.