Acts 17:16
TSK
¶ Diggante ba Póol di nég Silas ak Timote ca Aten, xolam jeex na ndax dafa gis na dëkk ba yeboo ci jaamu ay tuur.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Diggante ba Póol di nég Silas ak Timote ca Aten, xolam jeex na ndax dafa gis na dëkk ba yeboo ci jaamu ay tuur.
¶ Ba loolu wéyee Póol bàyyikoo Aten, dem Korent.
¶ Ba ñu muñee ba tële nag, ca lanu nangoo des ca Aten, nun doŋŋ.
Eràst moom, Korent la des, waaye Torofim, Mile laa ko bàyyi, ndax daa woppoon.