TSK

TSK · Acts 18:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Acts 24:6 TSK

Kër Yàlla ga sax jéem na koo teddadil, noo ko jàpp.

xanaa seen yenn yëfi diiney bopp yu ñu juboowul, ak mbirum ku ñuy wax Yeesu mu dee woon, te Póol moomu di dëggal ne mu ngi dund ba tey.

Ne leen ñu baña topp léebi neen, ak limi maam yu dul jeex, ndax loolu ay werante doŋŋ lay jur, te jariñul dara ci liggéeyu njotug Yàlla gi sottee ci ngëm.

Waaye werante yu xeluwul te du xam-xam, moyu ko, te xam ne ay ŋaayoo lay jur.