TSK

TSK · Acts 19:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Booba Samiyel xamagul woon Aji Sax ji, te kàddug Aji Sax ji dikkalagu ko woon.

Acts 2:17 TSK

“Yàlla nee: Mujug jamono, maay tuur samag Noo ci kaw wépp suux; seeni doom, góor ak jigéen di biral waxyu, seeni xale yu góor di gis ay peeñu, màggat ñi di gént ay gént.

Acts 8:15 TSK

Ñu agsi Samari, ñaanal gëmkat ña, ngir ñu jot Noo gu Sell gi.

¶ «Naka laa tàmbalee wax ak ñoom Korney, Noo gu Sell gi daanu ci seen kaw, na mu jëkkoona daanoo ca sunu kaw.

Yàkkamti naa leena gis, ba jottli leen mayug yiw gu bawoo ci Noo gu Sell gi, ngir dooleel leen,

¶ Léegi nag bokk yi, bugguma ngeen umple ci wàllu mayi Noowug Yàlla.