All books in KYG

Acts 21

KYG · verse 24

28 chapters

KYG / Acts / Chapter 21

KYG · verse 24

Ñ o om ngay àndal, nga bokk ak ñoom setlu, te nga gàddu seen peyu wateefu bopp, wi boroom xas wu ni mel aadawoo. Su ko defee ñépp ay xam ne li ñu lay jëwe, dara amu ci, te yoonu Musaa ngay jëfe, di ko sàmm.