TSK

TSK · Acts 25:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Ezra 4:15 TSK

ngir ñu seet ci sa téereb xew-xewi maam. Kon dinga ko ci gis ba xam ne dëkk boobu dëkku fippukat la, te sonal na ay buur aki boroom dëkk, te naka jekk dañu daan fippu ci seen biir. Looloo tasoon dëkk boobu.

Bu ma baye bànneexu noon. Seedey naaféq a ma jógal, di sos fitna.

Sarxalkat yu mag ya ak firikati yoon yaa nga taxaw, di ko tuumaal ak doole.

Acts 24:5 TSK

Waa jii lanu gis ne ab rambaaj la buy sabab réeroo ci biir Yawuti àddina sépp. Moom mooy njiitu ngér mu sikk mi ñuy wax Nasareen ñi.

¶ Ba mu dikkee, Festus ne: «Buur Àggripa, yeen mboolem ñi fi bokk ak nun teew, gis ngeen kii, moom la ma askanu Yawut wépp booleel, muy ca Yerusalem ak fii itam, ñuy xaacu naan: “Kii yelloowula dundati.”