TSK

TSK · Acts 8:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba loolu amee Naaman dellu ca góoru Yàlla ga, mook mboolem toppam ma. Mu dikk ba ca moom, taxaw ne: «Dama ne léegi wóor na ma ne amul jenn Yàlla ci mboolem àddina ju moy Yàlla ji ci Israyil. Kon nag sang bi, ngalla nangul lii, maa la ko may.»

Bu ngeen di fen sama ñoñ ñiy dégluy fen, yeena ngi may teddadil fi sama ñoñ, ngir ŋëbu peppum lors ak dogu mburu, ba tax leen di rey bakkan yu warula dee, di musal bakkan yu warula dund.

ak jote yu dul jeex yu boole ay nit ñu seenum xel mu yàqu xañ àlluway dëgg. Nit ñooñoo mbubboo ag njullite, te def ko wutukaayu alal.