All books in KYG

Daniel 3

KYG · verse 7

12 chapters

KYG / Daniel / Chapter 3

KYG · verse 7

L oolu nag waral saa yu nit ña déggee bufta gaak toxoro gaak xalam gaak riiti gaak kooraa gaak mboolem jumtukaayu xumbal ya, ñoom ñépp ay bokk sujjóot, màggal jëmmu wurus ja Buur Nabukodonosor samp, muy mbooloo yaak xeet yaak làkk ya.