Exodus 18:9
TSK
Yettro bég lool ca la Aji Sax ji def lépp, ba baaxe Israyil, xettli leen ca noteelu waa Misra.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Yettro bég lool ca la Aji Sax ji def lépp, ba baaxe Israyil, xettli leen ca noteelu waa Misra.
Aji Sax jee koy taxawu, wallu ko, wallu ko ci ku bon, musal ko, ndax li mu ko làqoo.
Buleen wóolu kilifa, doom aadama amul wall.
Yaw Aji Sax ji, ku dogu, pastéefu, wóolu la, nga may ko jàmm ju mat, nde moo la wóolu.
¶ Ba loolu amee jawriñ yaak laman yaak jaraaf yaak dagi Buur yéew leen. Ñu gis nag ne sawara wi lakkul seen yaram fenn, seen kawaru bopp xoyomuwul, seeni yére yàquwul, xeeñuñu sax xetu sawara.
¶ Ñu ne ko: «Buur, Dañeel mi bokk ca ngàllog Yudeen ña de, faalewu la, yaak aaye bi nga torlu. Ñetti yoon ci bés lay ñaan ay ñaanam ba tey.»