Exodus 20:3
TSK
¶ «Buleen am yeneen yàlla ci sama kanam.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Buleen am yeneen yàlla ci sama kanam.
Buleen ko xool bëtu yërmande. Noonu ngeen di dindee ci Israyil, àqu deretu jaambur bu deful dara, ndax ngeen baaxle.
Ñoo sarxalal ay rab yu dul Yàlla; ay yàlla yu ñu masula xam, yu bees yu doora xew, yu seeni maam ràññeewuloon.
Doom, bàkkaarkat bu la xiirtal, lànkal.
Ba loolu wéyee mu wax ak ña ca des, may dégg. Mu ne leen: «Toppleen ko ca biir dëkk ba te ngeen rey. Buleen xool bëti ñéeblu, buleen ñeewante.