TSK

TSK · Ecclesiastes 2:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Yàlla nag gis li mu def lépp, fekk lépp baax lool. Ngoon jot, suba dugg, muy bésub juróom benneel ba.

Ana sax luy njariñu doñ-doñoo doñ-doñ ju nit di doñ-doñi fi kaw dun bi?

di dogoo xam luy xel mu rafet, xam luy nitoodi akug ndof. Fekk loolu it napp um ngelaw la.

xameesul ku xeloom ku nitoodi lay doon, mooy moom lu ma doon doñ-doñi, te sama manoore manaloon ma ko fi kaw dun bi. Loolu it, cóolóoli neen.

Xanaa du ci Aji Sax ji Boroom gàngoor yi la lii bawoo: Sawara la askan yiy ñaqal, ag neen la waasoo yiy doñ-doñil?