Job 14:2
TSK
Dangay tóor rekk, lax, wéy ni takkndeer, doo toog.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Dangay tóor rekk, lax, wéy ni takkndeer, doo toog.
xamoo ne ku bon, ag sarxolleem àggul fenn, te bànneexu yéefar yàggul?
Aji Sax ji day seetlu ku jub; ku soxor, bëgg fitna, mu bañ.
ne: «Éy Aji Sax ji, xamal ma sama muj ak sama àppi fan, ma xam ni sama dund gàtte.
Nit ni ngelaw, ay fanam di takkndeer, wéy.
Waaye wóoy ku bon, nde mooy bonle; la mu def rekk lees koy def.
Sama Yàlla nee: «Jàmm du ñeel ñu bon ñi.»
Kenn ci yeen réccuwul ba tey jii. Kenn wormaalu ma mbaa mu jëfe sama yoon ak sama dogal yi ma leen tegal, tegal ko seeni maam.
Yeen xamuleen sax lu ëllëg di doon? Ana luy seen bakkan? Yeen ngeen di as lay suy feeñ léegi, nes tuut mu ne mes!