TSK

TSK · Esther 10:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Li des ci mbiri Yerbowam, ay xareem ak na nguuram deme woon, bindees na lépp moos ca téere ba ñu dippee Jaloorey buuri Israyil ca seeni jant.

Ba ñu seetloo mbir ma ba muy dëgg, dañu leena wékk ñoom ñaar ci bant. Bindees na ko ci teewaayu Buur ci téere ba nu dippee Xew-xew ya.

Buur nag tekki jaarob torlukaayam ba mu nangoo ca Aman, jox ko Mardose. Esteer daldi teg kër Aman ci loxol Mardose, mu di ko saytu.

Mardose nag am daraja lool ci biir kër buur, bayreem dajal diiwaan yépp, muy gën di am doole.

¶ Ba mu ko defee Buur teral Dañeel, may ko lu baree bare, ba noppi def ko kilifag diiwaanu Babilon gépp, teg ci fal ko, mu yilif boroom xam-xami Babilon yépp.