TSK

TSK · Exodus 2:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ba muy jub dëkk ba, daa yésal giléem ya fu dend akub seyaan waxtuw ngoon, fekk jigéen ñay génn di rootsi.

Doomi Majan di Efa ak Efer ak Anog ak Abida ak Elda. Ñooñu ñépp xeetu Ketura lañu.

Mu yem foofa ca ab teen ca àll ba, ñetti gétti gàtt goor ca wet ga, ndax ca booba teen lañu doon wëgge gétt ya, waaye doj wu réy moo uboon teen ba.

Ka ca des mu tudde ko Elyeser (mu firi Yàlla dimbali na ma), ndax da ne woon: «Sama Yàllay baay mooy sama ndimbal te moo ma musal ci saamaru Firawna.»

¶ Gannaaw gi Axab nettali Yesabel la Ilyaas def lépp ak na mu rendee saamar mboolem yonent ya.

Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.

Njàqare laa gis ca xaymay Kusan, te ndimoy xaymay waa Majan yëngu na.

Ngëm la bàyyikoo Misra, te ragalul sànjum buur, xanaa dogu rekk, mbete kuy gis ki gisuwul.