TSK

TSK · Genesis 34:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Kon nag buleen tiit, dinaa leen yor, yeen ak seeni doom.» Yooyu kàddu la dalale seen xol, ba ñu am jàmm.

Ruth 1:14 TSK

¶ Ñu dellu ne yikkét, di jooyoo. Orpa fóon goroom, tàggtook moom, Ruut nag moom langaamu ko rekk.

Ndax yaw dangaa bëgg ñi la bañ, bañ ñi la bëgg. Biral nga tey ne kilifay xarekat yeek xarekat yépp, tekkiwuñu dara ci yaw. Bir na ma ne bu Absalom doon dund tey te nun ñépp nu bokk dee, moo lay gënal.

Waxleen lu dalal xelu Yerusalem, yéeneleen ne leen seen xare jeex na, seen mbugal mat na. Ñoo nangoo ci loxol Aji Sax ji lu fey ñaari yoon seen bépp bàkkaar.

«Moo tax maa ngii di ko naxtaan, maa koy yóbbu ca màndiŋ ma, ba déey ko lu xolam dégg.