TSK

TSK · Genesis 37:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Gannaaw loolu am na bés Yàlla di nattu Ibraayma ne ko: «Ibraayma!» Mu ne ko: «Naam.»

¶ Ba Isaaxa màggatee, te bët yi naqari, ba gisatul, am na bés mu woo taawam Esawu ne ko: «Doom.» Mu ne ko: «Naam.»

Aji Sax ji woo Samiyel, mu ne: «Maa ngi»,

Eli nag woo ko ne ko: «Samiyel doom, ana nga?» Samiyel ne ko: «Maa ngi.»

¶ Naka yeen xale yi, déggal-leen seeni waajur, ngir Boroom bi, ndax moo war.